FANSOU FAT 2

1er Couplet

Luiguéne kharone dafa yague
Méle ni pithie bouy wadia tague
Bolé si sonne si wéraneté yi
Artiste you beuré yéke rawanté yi
Guénne ni mana mana mana
Gnéne ni gni ni kana kana kana
Guéne ni Fata El Presidente
Kéne khadioule nioune souniou diguanté
Douma si dara
Yéna def dara
li né si mane dara mane guéne farale
Souniou ande bi dafa yague
Khalé bou dioudone ware na mague
Ame na niou khékhe ame na niou khoulo
Beugue mou diekhe waté dioumoulo
Fansou Fata dou Khoulo dou Khékhe
Fougne niou Guéwalé rek Lamb-j diékhe

Refrains

Yeugue yeugue bou yague deugue leuh euh
Beugue nagne leuh euh
beugue nagne leuh
bague nagne leuh
beugue nagne leuhhh

2eme Couplet

Mbeuguéle bou wére té sakhe dakhe
Laye Guisse founé té mo sakhe dakhe
Damala beugue mala rawe douka faye
Khékhe gua si demb nangue si béke taye
Khame gua thioféle la niite meunoule faye
Bolé si yeugue yeugue si diamonaye taye
Soumaye beugue bakhe yéne rek kaka warale
Limaye tankhame lou yéna maka diarale
Na nieupe dioke amule tok
Séne heurou Kontane dafa diote
Démone na bay beugue bayi
Yéna ma diakhale ndakhe douguéne tayi
Ndakhe maléne tamale lou nékhe
Dana gueuna yague té dou diékhe

Refrains

Yeugue yeugue bou yague deugue leuh euh
Beugue nagne leuh euh
beugue nagne leuh
bague nagne leuh
beugue nagne leuhhh

Secka

Assalamalékoum mane Sécka maye nouyoke yéne
Yéne Fansou fat YI FATA ma yoni si yéne
Beugue dou bagne day méré lolou moye deugue
Wayé bagne dou beugue dafay nakhé lolou moy lou wére
ékhé té kat Sécka Fansou Fata yi bokou nioke nioume
Yéne gni Fata di fatale séne nokhe nokhi nakhare
Nite kou thieureume dafay fonke nitame
Sa bou wété toke si Kérame déglou aye wayame
Dioke léne daguéne wara dioke
Contane léne daguéne wara béke
Féthie léne daguéne wara teupe
Tatiou léne fétase tou léne
Diayou léne na lep reupe
Dioke léne takhawe na nieupe dioke
Fata Moléne di di wo guir guéne anda ndo bégué

Refrains

Yeugue yeugue bou yague deugue leuh euh
Beugue nagne leuh euh
beugue nagne leuh
bague nagne leuh
beugue nagne leuhhh

FANSOU FAT 2