NDEKETEYO

Lébone
Lépone
Amone nafi
Dane na ame
Louma meusa dégue mou waxe dou wédi da ame
Wédi guiss bokou si dounde ka rare na
Amoul soxore guestoule thi mbinde mi tarame
Sama bayeré moma togne
Dagne ma wara sondieu
Ba djiguéne diouma songue
Soye fa wala langue
Ma téla meuna rangou
Souma xéle douka nangou
Djiko boroma sankou
Kouye fake naka diengou
Douma diape béne niité guiire intérêt
Kone bouma kéne diapati guiire intérêt
Loy xamé yéne boushit yi dila ré
Té founiou teude dila dianére
Ndaxe dagne la gné
Khépe sa bop baxoule
Té xame gua Yalla diéxoule
Sa alale lathie sante
Boule ko youze
Doka finke
Adouna daafa fake
Beuri aye niite you néke
Meunou nioule sake
Té ite beugue la sanke

Refrain

Ndékétéyo beugouloma
Ndékétéyo nobouloma
Ndékétéyo faléwoma
Ake ate youniou déf yeupe
Sama xéle nék si yawe
Gua kheuye né dagaye seuyale kénéne koudoule mane
Heureusement fatéwouma sama niome
Ak samaye deukando kone ma rousse

2éme couplet

Loulou yeupe doko séte lou
Ndaxe yagui beugue seuye lou
Taktalé guél bi dougou sa dounde waxe la daf la beugue
Diaroule di dioudiou bo néka amouma khaliss mounila téguéka né
Mbeuguéle laly gondi xame gua rek tu lé conné
Kima si guisse dafe ma yéme
Sante na yalla ba dialoule ligua done diéme
Kone sama dignité dinaka niake
Sama yéne niite yi niome dinagne ma yape
Kénéne kouka nangou nak yakoy yeuke
Yalla ame na bénéne yape boudoule yéte
Beuguanté ndaxe khalisse séne xole yi dafa wéte
Boula kéne goundi leurti fake
L’argent ne fait pas le bonheur yawe tu le sais
Alale si djiguéne dakay dolélo
Bodé goor beugue lou yombe nioulay gololo
Fatélikoule démb xame ni goréwo

Refrain

Ndékétéyo beugouloma
Ndékétéyo nobouloma
Ndékétéyo faléwoma
Ake ate youniou déf yeupe
Sama xéle nék si yawe
Gua kheuye né dagaye seuyale kénéne koudoule mane
Heureusement fatéwouma sama niome
Ak samaye deukando kone ma rousse

3éme Couplet

Lima dounde si adouna laye sédok yéne
Kouy fansou Fat fouma né kéne warouko guene
Défare sa bop la xame si lalay nawe
Ndar moy sama deuke té town douma fa ndawe
Douma complexé té gnéwouma kéne
Ragualouma béne niite té soxoré wouma kéne
Yalla beuri xalisse barké yay borom
Douniou wane sa dolé deugue deugue amo morome
Alalou adouna doka youze pour diomale ma
Ndaxe bour bi yalla xamale nama né ame dioumouma
Gnigui niane yalla goudou fane ak wéregui yarame
Gua dieule sa temps séte lou né adouna gui sa kaname
Kouy dieundé niite khalisse nak dagua répe
Nala lére né boy déé do yobalé pépe
Tarou mbinde mi nak mangue kay may nieupe
Kou ndieuke fone yabi aldiana