Voyage

1er Couplet FATA

Dama yéwou nam ndar
sama ndokhou deuk la mar
tagou madame lima war la
dépense bi ndakh matna
niary tee-shirt niary jean
damay dem fouma miin
doli ndokh doli essence
dougue ci auto thiokh tal
saint-louis ma ville de naissance
kouy domou ndar doukateul
autoroute – apéyage
pour une route qui se dégage
teunguethie ma tégui ko
wa Doude Samb nouyou ko
dougue Bargny feulé Diamniadio
Hé dewma Mbour Sebikotame
dougue Poute cinquante alou kagne
bienvenue a Thies
Mafa bary mbokk waye
mé damay tégui ni thiass
lam lam malonk wéy
Beuréte yeksi tivaouane
Matar douma meuna agne ci
Gouléte ya beugue ganne
té di ziarr mame mbaye sy
ngaye mékhé kébémer
gueoul bi Matar dou mer
Louga lo nouyouna samba Diop
mangui diarr sakal baralé mpal
may gueune di diégué ndar
fass rao gandogue bar
ngay gueune yeuk xétou ndokh
deukou teranga nga ngui ni
deukou diam ba ngui ni
deukou islam ba ngui ni
nitt you jangue yangui ni yaw

Refrain Abdou Guité Seck

Fi moy bountou élégance
Fi Moy bountou xam xam
fi leu dinèe n0uyo civilisation occidental
guedjeu mbamoulane tama gnari bore
kouleu ame dieul kouleu gnakite woutila

2ém Couplet FATA

kougnou ngueweul la dioudo
maison blanche ma titeuro
serigne badiane dalal ba
leona fi ma dalé ndanda
diaba ndiaye dann ma tiyé
chak djouli dima khotil yeuré
yalnaka Yalla yeureum
denthialko aldiana gueureum
diamaguene nay souma Fiéve
wayé ndar gneupama beugue
nitt gnou nitté gninou deff
takhna kounou guiss seugue
boul guiss ndar ndar mou téy
ngua diawalekak kou toy
boul guiss ndar ndar mou dal
nguani lika war douka matal
gueum nani bokou yarr
bokkou nou linouy war
bokkou nou ninouy guissé
bokkou nou ninouy wakhé yaw

3ém Couplet FATA

souma sakk la may way
souma deuk bima beugue
deugueu deugueu yama néff
konn souma talent yaka néff
book Dioom kay la deuk
xéweul gui sama keur mame
jakarlo ngay jott ndieuk
guéléwar sa cité niakh
balacosse ak kani gui
ngueth ndar santhiaba
corniche ak eaux claires
pikine angle tall darou
nord sud ndioloféne
toloubour nga diko sénn iow